audio audioduration (s) 2.29 12.5 | transcription stringlengths 26 118 |
|---|---|
sa mbaal mi jén yu ndaw rekk la mëna jàpp | |
booy tisóoli bu ko def ci kow nit ñi | |
dafa ma ko wax may rabat lu ma waroona def | |
peese bi moo tax tefes giy wéet yenn waxtu yi | |
taxawalal eseel bi mu sës ci miir bi | |
xam nga xél ne ëgg bi baaxul ci naafi gerte yi | |
su dara desul lu dul ñàkkante ma dem sama yoon | |
boo bëggee togg yaasa dangay marine ganaar gi ak limoN | |
déedéet garab bi keroog gi ñu ma joxee garab bi ma commencer ko naan keroog la génn nii | |
maa ngiy wut pexe mu ma jàlle dex gi | |
bu jëkk jarbaat dafa daan donn nijaayam | |
danga ma suufu ci woto ba ma doon bëgga jénd | |
ba ma ko yeddee ba tey bàyyi na daw jàng | |
boo ko sangee ba noppi nga lenqali ko ak ndox mi ci siwo bi | |
xale bi nangootul dox cumbur bee ko jaaxal | |
bërëb bu ral bii nu mu fi mana nëbboo | |
ba diggante ñaari réew yi yàqoo moom lañu ràng | |
gën gaa bare mën naa ci def juróomi junni | |
bi mu fiy agsi mu ngi woon ci diggu dooleem | |
garab gii farmasi rekk nga ko mëna ame | |
dangay jéem ba xam ndax dinga mëna ubbi bunt bi ak caabi jii | |
am na ñuy sangoo reeni tol nee ñu dafay wàcce coono | |
ca tamxarit wa laa ko seeti fekk ko muy bomb cereem | |
teg sa takka ndeer ci ndox taxul nga tooy | |
ay jigéen yu doon dem faro ya ñoo ma won yoon mi | |
dafa saraxu duwaañ bi ba mu bàyyi ko | |
lu ñaaw li mu def la bëgg a dabu waaye wees na | |
xam naa ni sama woote du sooy ndax bàkkan dafa diis | |
su sunuy kàddu dëppoo mbir mi dootul yàgg | |
nanga butti jén yi dal di leen raxas ba ñu set | |
mënuloo woon jénd meew xanaa furóoñu cere ji | |
kenn mosu fi jàpp jaabaar bu ni tollu | |
fekk na biram njéemé koo njaay a ngi wara tollook ndangalma | |
boo amoon kersa duma taxaw ngay saaga | |
bant bi xar jéppén dafay tegtal ne yoon wi dafa def sél | |
soo bëggee birig bi xéj ci dangay xàppati koñ bi | |
ku dahà haj bél cà ker àm nga bayi ko | |
dafa duggoon ci njaayum gejj waaye dafa ca lom | |
bareetul suubkat yuy jëfandikoo nganj | |
Naka la agsi ci guy gi mu ni guy nàyeet | |
bu jëkk tubaab yi dañu gawoon njàngum alxuraan ji | |
xale baa ngiy xàqataay rekk soo demee dañu koy ñiiramtal | |
booy tudd xaalis muy ñàngal kanam gi | |
lor nga ma waruloo ko woon jox sama xaalis | |
xam na ni sa cofeel mosul deñ ci moom | |
bi ñu koy yóbbu loppitaan la faf loru | |
dañuy tari alxuraan bàyyi leen coow li | |
Nit kiy joxe kayit woowu dafa génnoon xaar naa ko lu yàgg | |
ku di talantu ci ñam boobà sa yaay a toga | |
ca diggu gott ga la dem samp fa néegam | |
moo taxit feebaru jigéen dafa bari façons | |
fu sindah yabé ndobin garab a fà jégéñ | |
li ñu lay fey a ngi tolloo ak sa man man | |
dafa tëddoon di féexlu ca peggu déeg ba | |
butoN bii lañuy wàññce tàkk tàkku làmpu petarool bi | |
waaN waaN ji dafa koy dimmali ci wasin | |
gaasal cere fass ji bala nga koy tay | |
dafa bëggoona nëpp nëppal biiru doom ji | |
bëgga riccamtéku moo la tax di wax lii | |
ab dànnala la woon waaye bët yi neexatul | |
bi nga xamee né buur yi benn kepp a ci des di buurub saalum mu daldi né | |
géew bi yaawul na nit ñi dellu gannaaw | |
aayal jaar ci suufu eseel biddaa tubaab yi la | |
picc mi bëgg xale bi xale biy màgg | |
kenn mënul def supp ci aset bu tell bii | |
arikoweer dañu koy toggaale ak lax bi | |
su ngeen ko téyewul dina ko dóor bolde bi | |
waxambaane yiy nemm a taal safara si ngay séen | |
bi mu tàmbalee jël garab googu ba tey miiratul | |
mu agsi jëkkër ja ak goro bu jigéen ba dawoo di jooyoo | |
dafa ubbi kaaf gi rekk picc yépp naaw | |
hej u ncokér ak seen àm ku cà gasul yoy | |
mu ni dama koy wallu ci njëlam lu jëkk li | |
ku am ngànt mbaa nga ñàkk ndox may nañu la nga tiim | |
xaaral ba timis fàddu nga door a génn | |
soow maa ngiy ñów ñaare ci ñetteelu fan wi gannaaw wasin gi | |
céy sama njaqare ja ba ñu ma nee awyoN ba dem na wacc la | |
ngem nekk fii di ratatati tere nit ñi nelaw | |
yow de yaay seet rekk ba xam li nga mën | |
ba nga xamee ni ñépp a ngi fecc di ree mu am ku ni | |
sa màngo gaa ngi buubu war nga koo xapp | |
Nangeen jóg bu ngeen deggee bàkku senegaal | |
ceglar ni caraax fekk ko mu déféenu | |
lu la yar ak teggin meyul leneen du la ko mey | |
benn géwal ba daldi jiin tabala ji né | |
dina dellusi gaa yàggaay bi rekk a ma ci jaaxal | |
mu né ko yow dangay fen tey jii dinaa la fetal | |
bu weer wi deewee war na fekk ku nekk joxe wàllam ci tabaxu kalaas bi | |
ba ma ko fàttalee xaalis bi dafa fenantal | |
dindil sa loxo yi nga dar ci sa nopp yi te déglu li ma lay wax | |
diine dina togg nit ki ba muy jëfe lu rafet | |
saxaar yiy dem amerig fii lañuy jaar | |
suqi na ganaar gi ba pare mu ngi koy butti | |
Ni nga àttee ku ko gis xam ne danga farle | |
ndax dénd wii mën naa xadd néeg bi | |
yàlla taal sànni ci matt a gën fey ko | |
ñu dagg buum gi wocc biram njéemé ca biir | |
ba ñu ko naanee daal lañu kata kayna | |
bu jëkk ñi daan jong ay magi jëmm lañu daan nekk | |
na ngeen yenduji ca dédd ga ca tool ba |
End of preview. Expand
in Data Studio
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 8