audio
audioduration (s)
1
29.9
text
stringlengths
1
638
lang
stringclasses
1 value
source
stringclasses
1 value
license
stringclasses
1 value
duration
float32
0
0
sama jollasu sabaat na
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
dinañ leen former ay formuler ay idées de projet
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
clinique du cap manuel
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
baal ma nga jàdd
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
xam naa ne boobu moom question boobu dama la koy denc d abord
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
cité doudou basse
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
tapoo yu réew yi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
taarix bi camille saint saens wané woon ci opera bu france bu benn artist la boo xam ni dundam yepp sinébar ak sapong la
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
virage
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
danuy dégluy way
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ci diiru tukkeem iwasaki dafa jokkonteeg ak coow ci anam yu bare
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ci formation yoo xamante ni dañu koy def
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
commissariat dieuppeul
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
waaye maki waxunu lépp
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
wurëmbél mumbél wurëmbélél mumbébél
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ag ganeem àadduna g m
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
kon même bu dul suñu fan may na ko it
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
damay def geet
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
après day ne fan yii tamit taw du bare
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ayoo beeyoo beeyoo
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
am na solo mais béykat dugub yi bu dul picc yi am na yeneen yoo xam ne aussi dañ leen koy dañ koy daén leen di sonal si wàllu conseil picc yi am na yeneen wànq yeeg yooyu yëpp la nga leen di conseillé tam bu fekkee ne yu mel noonu dab na leen si seen biir liggéey
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
man ngeen a ñëw
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
soo moytuwul ngëndël li dugg ci sa bët
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
jox ma njàmpe li ma ragg samay tànk
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
niru na lu am solo
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
dafa nekk farata ci képp ku nekk ci ñun parce que bu ñu xoolee jamono jii fi àdduna si toll
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
kañ la nuy jëmale sunu xel yi ci lunuy jariñ
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
jéemaat leen baxam
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
sandaŋ laa ko dóor bàyyi ko muy raam
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
damaa am ub kaaseer
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ndax tudd naa ko
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
boobu suuf salañ moo ci ëpp
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
papa gueye njeri
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
mu daldi dem jënd mburóom ag póonam
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
démb waa dëkk bi dañu doon xoddiku
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
dunu ay raykat
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
pharmacie ibrahima niass
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
am na réew yoo xam ne yem ci ñuy waaja lekk taxul ñu woo la
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ban oto mooy dem rond point ngor
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
nde kon guddeek bëccëg lanuy def koor ga
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
taw bi nag gëlgóose boobu mu def noonu diggante mai juin am na lu mu lifin ba ñetti vagues yooyu mu wax moo fi ne
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
dinaa nekk ci biir
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
santaat nañ la gërëm nañ la
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
loolu dañu ne foofu tamit même chose bu dee nag bi huit pour cent la yow yaay ne sama nag lii lay jar
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
te amóo benn làqukaay bu dul moom
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
bëgg naa sama réew
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
jeexal naa ay sox
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
dañ leen forsewoon ñu fay rezim koloñaalu amerik ay juuti ngir matal wàll bu mag ci liñuy depansé te njuréef yi am ci cakkutéef yi làp feey ci turu nguuru philipin jaaree ko ci banku waal street
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
danoo xeebu lool boo nu toppee ci sun
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ndax man nga cee jël jërëjëf
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
benn hactare bi quatre kilos mu ne moo koy moo koy moo moo koy traité te dix kilos boobu nag quatre kilos boobu dix grammes de produit la ñu si def
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
xam na ci dara
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
dafa leen ran ale ñu def ab wërngël
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
tournalou boune
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ab sëyeeful la batay
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
teenu daaru musti bar lañu koy wëgge
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
fum jëmoon
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
yal na leen yàlla musal ci mbas mi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
danga geestu ma xam ne moom geen di wax
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
buleen bokk wanag
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
croisement bountou pikine
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
je crois que a na période boo xam ne béykat bi ci lay sonn te béykat bi ci période boobu la leen di gën a faagaale
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ngir pexem jinne
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
di gën a gën a gën a gën a soxla ak aussi naka lañ koy utiliser ah donc defe naa ne moom mooy ponk bi nga war a ñëw léegi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
mbaa yaa ngi am jàmm
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
maa ngi doon yég ni sama xol bi doon dale
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
góor gu am fayda du dàggasante ak jigéen
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
baatu pël yit noonu wareesu ko jëfandikoo ngir tudd pulaar yépp
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
mën nañu la jàpp chambre de commerce ñëpp kenn ku ci ne dana def visite ci fi nga xam si ne mooy béréb bi nga xam ne si nga defaree li nga xam si moom mooy céréale bi wala soit yeneen produit yi ngay defar
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
jéemleen a ànd ak seen sago
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
doxalukaay bu dawaan bu safaanu dees koo séddale ci ñaar
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
tey jii nii sooy xool li ngay utiliser si ndox sooy jëlee sa arrosage rek d sotti nii ak sooy def goutte à goutte li ngay sakkanal si ndox kenn xamul nu mu toll
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
noppi bu sa imaam di jàng ca kaw doonte déggoo ko
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
te dananu ñoddi ci kurél bu nekk ña ca gënoon a ñeme yàlla
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
waaw moom la projet bi wax te incha ar allah ar loolu dina antu par rapport ak activités yi ak cër yi nga xam ne moom la ñu jox les les opérateurs spécialisé
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
nan la ñu ko man a defee
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
wommatal ko lépp lu mu mébat ci ligéeykat bi sëñ bi niki muy xéewalee
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ndax naroon nga ma topp
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
boo demee ba naawtal su la neexee nga dellu ndakaaru
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
tay ñi koy até mooy ndiabot guila woroon baay
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
teen bi daa wow kong
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
toroxal na jigéen suufeel mag
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
neuf cent quatre vingt un trente et un
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
njëriñu béykat yi ak taxawaay bi njëriñu béykat yi tolluwaay bi tey la monsieur thiam le temps que téléphone bi di ñëw mais ëllëgu béykat yi wax nga fi loo xam ne léegi bi ngay bi ñuy commencé xaj na suñ ko waajoon du leen dal ren man jokkoo naa ak téléphone béykat ma jël kooku ci numéro mun nga jël casque bi allo
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
tom nuru na ku bon
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
sama assistant bi nekk foofu tamit monsieur sakho
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
voilà bu fekkente ni sax
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
betani ca penku dexu yurdan
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
saa doom xam nga lan mooy àddinaam
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
coo noo ñàkk fayda
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
donc loolu aussi mun nga wa incendie
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
amn na ñëpp mënuñoo jot message wala ñi nga xam ne bu jotee message sax pour ñu lire ko ba xam ko problème la
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
kaso gi dafa siiw ginaaw ba nu gisee ni bunduxatal nanu ab nit bu nu jàpp foofu ba takk der waa amerig tegee seen tank foofu
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
buleen yëngu su leen neexee
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
merci beaucoup ça va
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
damaa war a tukki
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
lekk nañu yàpp wa ba mu jeex yax yee fi des
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
omar watt omar watt geed
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
kenn a ngi ree
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0
ndax dangaa dóor tom leegi
wo
soynade-research/Wolof-ASR-Data
CC-BY-SA-4.0
0